Tripoli (Libi)
Aller à la navigation
Aller à la recherche
Bii jukki ab junj rekk la.
Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal
Tripoli طرابلس | |
---|---|
Réew | ![]() |
Tus-wu-gaar Tus-wu-taxaw |
|
Kawewaay | 81 m |
way-dëkk | 1 682 000 nit |
atum way-dëkk | 2 009 |
Rëyaay | 400 km² |
Tripoli (di طرابلس tarabilus ci araab) mooy péeyu réewum Libi. Turu dëkk baa ngi tekki «ñetti dëkk yi», ndax limu jóge ci booloog ñetti dëkk yii di Oea, Leptis ak Sabrata. Mi ngi féete ci bëj-gànnaar-sowwu réew mi, taq ci tàkk gi, ci dogub suuf bu kekke, féetek Géej gu Diggu gi ci geneen wàll