Schizophrenia

Jóge Wikipedia.

Royuwaay:Short description

Feebaru kuy dégg ay baat walla gis ay mbir yu doy waar, te gëm ay mbir yu amul mooy xel mu jaxasoo ñu koy gise ci nekkin bu dul noonu ak dégg-dégg bu waññeeku ci li dii dëgg.[1] Li koy wone ci li ñi gëna gis ñooy gëm-gëm yu amul, Xalaat yu amul bopp amul geen, dégg ay baat yu ñeneen ñi dul dégg, nekk ak nit ñi ak cofeel yu waññeeku, ak ab ñakka am cawarte.[1][2] Nit ñi ame feebaru kuy dégg ay baat walla gis ay mbir yu doy waar, te gëm ay mbir yu amul ñu koy woowe schizophrenie dañuy faraldi am yeneen jafe jafe feebaru xelyu mel ni jaq déteelu, walla ay feebaru dorogewu. [3] Feebar yi buñuy feeñ dañuy ñëw ndànk ndànk, tambali ci bi nga nekkee xale bu dëggër, te dañuy yagg lool.[2][4]

Yii di indi feebaru kuy dégg ay baat walla gis ay mbir yu doy waar, te gëm ay mbir yu amul ñooy li ñu wër ak Ndono ci dereetci yooyu wall.[5] Li jóge ci wallu li ñu wër bokk na ci nga yaroo ci dëkku taax, yambaa jëfandikoo ko bi nga nekkee xale bu góór bu jigéén, yenn cofeel yi, at mu sore bu waajur yi, ak lekk bu bon bi nga ëmbee.[5][6] Ndono yi ci dereet bokk na ci ay ndono yu bare yu ñuy faraldi gis ak yu nééw.[7] Saytu bi mungi tegu ci seetlu nekkin, nettali jaar jaari nit ki ak li ñi jege nit ki nettali. [4] Buñuy saytu nit ki aadaam dafay am solo ci saytu bi.[4] 2013 ba léégi amul saytu bu leer.[4] Feebaru schizophrenie tekkiwul ne nit ki dafa am "nekkin yu wute" walla am nekkin yu bari lépp ci benn nit ki - lu ci ëpp dafay jaaxal nit ñi.[8]

Paj mi mungi aaju li ci ëpp ci luy xeex ñakk àndak sago garab, ak ci wetam joxe ay tegtal ngir dimbali nit ki saafara jafe-jafeem, taggat ñi di fajaate ngir ñu mëna def seen liggééy bu baax ak delluwaat nekk ak nit ñi. [1][5] Leerul ndax raññeeku walla luy xeex ñakk àndak sago yu ñu dul faraldi gis ñoo gën.[9] Ñi nga xame ne duñuy tane ak yeneen yi di xeex ñakk àndak sago clozapinewar na ñu ko jééma jëfandikoo.[5] Ci yenn yi gëna metti te nga xam ne am na ab njàjan ci sa bopp walla ci ñeneen ñi ospitaaliise buñu tannulwar na mëna nekk, su fekkee sax léégi des ci opitaal mungi waññeeku bu baax ni bu njëkk ba.[10]

Lu tollu ci 0.3 ba 0.7 % ci ay nit am nañu feebaru schizophrenie ci seen dund.[11] Ci atum 2013 amoon na ab xayma bu tollook 23.6 miliyoŋ ci ñi ame feebar bi ci addina bi yépp.[12] Góór ñi ñoom la feebar bi gëna japp, te ci ñoom lañuy gëne raññe feebar di wonewu.[1] Lu tollook 20% ci ñoom ñungi ciy génn te tuuti rekkay wér bu baax,[4]te lu tollook 50% dañuy am gallankoor ci seen giiru dund.[13] Ay jafe jafe ci nekk ak nit ñi, ni ñakka liggééy gu yagg, ndóól ak ñakka am dëkkuwaay, dafa bari. [4][14] Limu yaakaar ci dund ba ab atbu nit ñi ame feebar yu fës yi mungi ci fukk ba ñaar fukki at ak juróóm gëna tuuti nit ñi ci ëpp.[15] Li mooy li mu jur ci yoquteek jafe jafe wér gu yaram yi ñiy gis ak kawewaay xarumungi tollu ci (lu jege 5%).[11][16] Ci atum 2015 xayma nañu lu tollook 17.000 ci ay nit ci addina bi ñu dee ci nekkin bu bokk ci, walla jóge ci, feebaru schizophrenie. [17]

  1. 1,0 1,1 1,2 et 1,3 "Schizophrenia Fact sheet N°397". WHO. September 2015. Archived from the original on 18 October 2016. Retrieved 3 February 2016.  Unknown parameter |df= ignored (help)
  2. 2,0 et 2,1 "Schizophrenia". National Institute of Mental Health. January 2016. Archived from the original on 25 November 2016. Retrieved 3 February 2016.  Unknown parameter |df= ignored (help)
  3. Buckley PF, Miller BJ, Lehrer DS, Castle DJ (March 2009). "Psychiatric comorbidities and schizophrenia". Schizophrenia Bulletin 35 (2): 383–402. PMC 2659306. PMID 19011234. doi:10.1093/schbul/sbn135. 
  4. 4,0 4,1 4,2 4,3 4,4 et 4,5 American Psychiatric Association. Diagnostic and Statistical Manual of Mental Disorders (5th ed.). Arlington: American Psychiatric Publishing. pp. 101–05. ISBN 978-0-89042-555-8. 
  5. 5,0 5,1 5,2 et 5,3 Owen MJ, Sawa A, Mortensen PB (July 2016). "Schizophrenia". Lancet 388 (10039): 86–97. PMC 4940219. PMID 26777917. doi:10.1016/S0140-6736(15)01121-6. 
  6. Chadwick B, Miller ML, Hurd YL (October 2013). "Cannabis Use during Adolescent Development: Susceptibility to Psychiatric Illness". Frontiers in Psychiatry (Review) 4: 129. PMC 3796318. PMID 24133461. doi:10.3389/fpsyt.2013.00129. 
  7. Kavanagh DH, Tansey KE, O'Donovan MC, Owen MJ (February 2015). "Schizophrenia genetics: emerging themes for a complex disorder". Molecular Psychiatry 20 (1): 72–6. PMID 25385368. doi:10.1038/mp.2014.148. 
  8. Picchioni MM, Murray RM (July 2007). "Schizophrenia". BMJ 335 (7610): 91–5. PMC 1914490. PMID 17626963. doi:10.1136/bmj.39227.616447.BE. 
  9. Kane JM, Correll CU (2010). "Pharmacologic treatment of schizophrenia". Dialogues in Clinical Neuroscience 12 (3): 345–57. PMC 3085113. PMID 20954430. 
  10. Becker T, Kilian R (2006). "Psychiatric services for people with severe mental illness across western Europe: what can be generalized from current knowledge about differences in provision, costs and outcomes of mental health care?". Acta Psychiatrica Scandinavica. Supplementum 113 (429): 9–16. PMID 16445476. doi:10.1111/j.1600-0447.2005.00711.x. 
  11. 11,0 et 11,1 van Os J, Kapur S (August 2009). "Schizophrenia" (PDF). Lancet 374 (9690): 635–45. PMID 19700006. doi:10.1016/S0140-6736(09)60995-8. Archived (PDF) from the original on 23 June 2013.  Unknown parameter |df= ignored (help)
  12. Global Burden of Disease Study 2013 Collaborators (August 2015). "Global, regional, and national incidence, prevalence, and years lived with disability for 301 acute and chronic diseases and injuries in 188 countries, 1990-2013: a systematic analysis for the Global Burden of Disease Study 2013". Lancet 386 (9995): 743–800. PMC 4561509. PMID 26063472. doi:10.1016/S0140-6736(15)60692-4. 
  13. Lawrence RE, First MB, Lieberman JA (2015). "Chapter 48: Schizophrenia and Other Psychoses". In Tasman A, Kay J, Lieberman JA, First MB, Riba MB. Psychiatry (fourth ed.). John Wiley & Sons, Ltd. pp. 798, 816, 819. ISBN 978-1-118-84547-9. doi:10.1002/9781118753378.ch48. 
  14. Foster A, Gable J, Buckley J (September 2012). "Homelessness in schizophrenia". The Psychiatric Clinics of North America 35 (3): 717–34. PMID 22929875. doi:10.1016/j.psc.2012.06.010. 
  15. Laursen TM, Munk-Olsen T, Vestergaard M (March 2012). "Life expectancy and cardiovascular mortality in persons with schizophrenia". Current Opinion in Psychiatry 25 (2): 83–8. PMID 22249081. doi:10.1097/YCO.0b013e32835035ca. 
  16. Hor K, Taylor M (November 2010). "Suicide and schizophrenia: a systematic review of rates and risk factors". Journal of Psychopharmacology 24 (4 Suppl): 81–90. PMC 2951591. PMID 20923923. doi:10.1177/1359786810385490. 
  17. GBD 2015 Mortality and Causes of Death Collaborators (October 2016). "Global, regional, and national life expectancy, all-cause mortality, and cause-specific mortality for 249 causes of death, 1980-2015: a systematic analysis for the Global Burden of Disease Study 2015". Lancet 388 (10053): 1459–1544. PMC 5388903 Check |pmc= value (help). PMID 27733281. doi:10.1016/s0140-6736(16)31012-1.