Sao Tome (dun)
Apparence
Sao Tome | |
---|---|
Réew | Sao Tome ak Principe |
Tus-wu-gaar Tus-wu-taxaw |
|
Kawewaay | 2024 m |
way-dëkk | 133 600 nit |
atum way-dëkk | 2 005 |
Rëyaay | 854 km² |
Barabalub Sao Tome ak Principe | |
Sao Tome mooy turu dun bi ëpp ci Sao Tome ak Principe, di itam péeyu réew mi. Mi ngi féete ci tefesu bëj-gànnaaru dun.