Rabat
Apparence

| Rabat الرباط ⵕⵕⴱⴰⵟ | |
|---|---|
| Réew | |
| Diiwaan | Rabat-Salé-Zemmour-Zaër |
| Tus-wu-gaar Tus-wu-taxaw |
|
| Kawewaay | 11 m |
| way-dëkk | 1 787 307 nit |
| atum way-dëkk | 2 009 |
| Rëyaay | 1 088 km² |
| DIggu Rabat | |
Rabat (di الرباط ar-Ribat ci araab) mooy péeyu Nguurug Marok, mooy ñaareelu dëkk bi ëppi nit ca nguur ga. Mi ngi nekk ci wetu tefesu mbàmbulaanug Atlas gi. Ca jamono-ju-yàgg ja lañu fa tambalee dëkk. Ñoo ngi ko sos, dëgg-dëgg, ci 1150.
