Aller au contenu

Praia

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal



Dëkku Paraaya

Skyline of {{{official_name}}}
Réew Kap Weer
Diiwaan Paraaya
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
14° 57′ Nord
     23° 31′ Ouest
/ 14.95, -23.52
way-dëkk 130,271[1] nit
atum way-dëkk 2 010
Dalub web http://www.cmpraia.cv/
Farol D. Maria Pia/Farol da Ponta Temerosa

Paraaya fimne mooy péeyu réewum Kap Weer. Ben dekku mi ngi dunu Santiago (Kap Weer). Dëkk bi nekk ci bëj-saalum penku gi ci dun bi ñuy wax Santiyaago, ci biir dun bi ñuy wax Sotaweento, dëkk bi mooy dëkku dëkk bi ñuy wax Paraaya. Paraaya mooy dëkku koom-koom, politig ak aada ci Kap Weer.

  • Achada Grande
    • Achada Grande Frente
    • Achada Grande Tras
  • Achada de Santo Antônio
  • Ponta das Bicudas
  • Calabaceira
  • Bairro Craveiro Lopes
  • Bela Vista
  • Fazenda (Achada Fazenda)
  • Gambôa/Cha das Areias
  • Lem Ferreira
  • Monte Vaca
  • Monte Vermelho
  • Paiol
  • Palmarejo
  • Palmarejo Grande
  • Plato
  • Quebra Canela
  • Ribeira da Trindade
  • São Francisco
  • São Tomé
  • Praia de São Tomé
  • Ponta Temerosa
  • Terra Branca
  • Trindade
  • Várzea

Futbol klubi

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Iniweersite

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Karmat ak delluwaay

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Teereekaay

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
  • Cabo Verde, viagem pela História das ilhas (Almeida, Germano; Lisboa: Caminho, 2003)
  • Cabo Verde, cruzamento do Atlântico Sul (Mindelo: Rádio Nova, 1998)

Lëkkalekaay yu biti

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons
Bëj-gannar: São Domingos
Penku: Ribeira Grande de Santiago Praia Sowwu: 'Mbàmbulaan gu atlas
Bëj-saluum: Mbàmbulaan gu atlas