Oktoobar

Jóge Wikipedia.
Dem: Joowiin, Seet

Oktoobar mooy fukkeelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.

Turam ma ngi jóge ci latin october, jóge ci octo (juroom-ñett), moo nekkoon juroom-ñetteelu weer ci arminaatu waa-rom bu jamono ju yàgg ja.

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons
Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar