Nowembar
Apparence
Nowembar mooy fukk ak benneelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.
Turam ma ngi jóge ci latin november, jóge ci novem (juroom-ñeent), moo nekkoon juroom-ñeenteelu weer ci arminaatu waa-rom bu jamono ju yàgg ja.
Weer |
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar |