Disambar
Aller à la navigation
Aller à la recherche
Disambar mooy fukk ak ñaareelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.
Turam ma ngi jóge ci latin december, jóge ci decem (fukk), ndax moo nekkoon fukkeelu weer ci arminaatu waa-rom bu jamono ju yàgg ja.
Weer |
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar |