Aller au contenu

Ndëgërlu gu mbëj

Jóge Wikipedia.
(Yoonalaat gu jóge Ndëggërlu gu mbëj)

Ndëgërlu gu mbëj ag jagle gu jëmm la guy tax nu man a natt bañ gi ab wommatukaay di bañ su ko dawaanu mbëj di jéem a jàll. Lànk googu dafa aju ci ne-ne bi ñu defare PENISwommatukaay bi, dijjaayam, tàngaayam, ak, su fekkee dawaan bu safaanula, baraayu dawaan bi. Genn ci njeexiitu jàllug dawaanu mbëj ci ab wommatukaay mooy yokkug tàngaayam, di liñuy wax njeexiitu Joule.

Ndëgërlu gi ci gii yamale nga koy xamee:

Tekki:

  • R mooy Ndëgërlu gi nekk ci diggante ñaari cati wommatukaay bi, ohm[Ω] mooy bennaanu nattam.
  • V mooy dend bi ne ci diggante ñaari cati wommatukaay bi , volt mooy bennaanu nattam.
  • I mooy dawaan biy jàll ci wommatukaay bi, amper mooy bennaanu nattam.

Ndëgërlug ag wëñu wommatukaay

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ndëgërlu R gu ab buumu wommatukaay nii lañu koy xaymaa.

Tekki:

  • L mooy guddaayu buum gi, meetar mooy bennaanu nattam.
  • S mooy dijjaayam, m2 mooy bennaanu nattam.
  • ρ (arafu waa-geres: ro) dëgërluwiin gu wommatukaay bi, ohm * meetar mooy bennaanu nattam. Di maanaam man gi wommatukaay bi mane dëgërlu dawaanu mbëj buy jàll ci biiram. Ci yeneen kàddu Ndëgërlu gu ab wommatukaay dafay aju ci kemu man a ma dëgërlu. Ci lu ëpp Ohm x mm² / m lañ koy natte, lii moo lay jox Ndëgërlu, ci ohm, gu genn wëñ guy wommat dawaanu mbëj gu gudde 1 m te dijjee 1 mm².

Misaal: dëgërluwiinu përëm mooy 0.0175 ohm x mm² / m, kon lii da lay wax ne ag wëñu përëm gu gudde 1 m dijjee 1 mm² Ndëgërloom gu mbëj day doon 0.0175 ohm.

  • mooy wommatiin gi, maanaam ni wommatukaay bi manee wommat.

Ajoom ci tàngaay

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ninu ko biralee ci kaw, Ndëgërlug ab wommatukaay nii lañ koy xaymaa.

waaye ak bii yamale, dëgërluwiin gi dafay aju ci tàngaayu wërlaay gi mu ne. Su fekkee fésaluñu ko, dangay jàpp (ninu ko waxee ca kaw-a-kaw) ne ci tàngaayu 20° la. Mbindiin wii moo koy wone . Ci maanaa mooy ne ndëgërlu gi dafa aju ci tàngaay bi, lii man nañ koo wax ci bépp wommatukaay.

Lëkkalekaay yu biir

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

babyolie gwn kersensaus ja