Luanda
Sauter à la navigation
Sauter à la recherche
Bii jukki ab junj rekk la.
Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal
Luanda | |
---|---|
Réew | ![]() |
Tund | Luanda |
way-dëkk | 7 000 000 nit |
atum way-dëkk | 2 009 |
barabalu Luandaa ci lonkoyoonu Angolaa | |
[[image:![]() | |
Luanda (bu njëkk São Paulo da Assunção de Loanda) ab dëkkub bëj-saalumu Afrig la, di itam péeyu réewum Angolaa. Féete ci tefesu Afrig gu mbàmbulaanug Atlas gi, Luanda mooy waax wi ëpp ci Angolaa gépp
Dëkkiin[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Limu nit ñi dëkk Luanda ci at yi: