Aller au contenu

Bëj-saalumu Afrig

Jóge Wikipedia.
(Yoonalaat gu jóge Bëj-saalumu Afrik)
Xët wii dafa nekk ci yoonu ndefaru. Sag cëru man na cee am solo!
Lonkoyoon gu Afrik ak Bëj-saalumu Afrik

Bëj-saalumu Afrik moo ëmb barab yi nekk ci Bëj-saalumu allub yemoo gu Afrik.

Dañ ciy boole tamit duni Afrik yi nekk ci Bëj-saalum-sowu mbàmbulaanu waa-End ci wetu Madagaskaar ak duni Afrik yi ci Bëj-saalum-penku mbàmbulaanu Atlas.

Askani Xoysan ñoo fa njëkk a dëkk, ci li ci tegu la bantu yi ñéw. Ci jamono gi waa tugal aakimoo diwaan bi, lañ seddale réewi tayam yi.

Doon na diwaan bu am-alal te suufam naggu lool mbay. Rèew mi gën a jëm-kanam ci Afrik, fa la ne rawatina muy Réewu Afrik gu Bëj-saalum

Séwógaraafi

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Juroomi Réew ñoo nekk ca diwaan boobu:


Diwaani Afrig
Diwaani KMX: Diggu Afrig · Penku Afrig · Bëj-gànnaaru Afrig · Bëj-saalumu Afrig · Sowwu Afrig
Yeneen diwaan: Ginne · Bejjenu Afrig · Maghreb · Sahel · Afrig gu bëj-saalumu-Sahara · Sudaan