Alse
Apparence

| الجزائر Alse | |
|---|---|
| Réew | |
| Tus-wu-gaar Tus-wu-taxaw |
|
| Kawewaay | 424 m |
| way-dëkk | 2 203 698 nit |
| atum way-dëkk | 2 009 |
| Barabalub Alse | |

Alse walla الجزائر ci araabi alseeri mooy péeyu réewum Alseeri, féete ci bëj-gànnaaru réew mi janook Géej gu Diggu gi. Mooy itam dëkk bi gën a mag ca réew ma
