Abel

Jóge Wikipedia.
Abel + Kayin

Ci làkku ibrë (הֶבֶל / הָבֶל) la tur wi jóge. Ci angale mooy Abel; Ci faranse mooy Abel

Abel mooy ñaareelu doomu Aadama ak Awa. Magam, Kayin, moo ko réy (Ge 4:2-8). Ci Lislaam mooy Haabiil.

Ci Injiil dañuy wax ci Abel ci Mc 23:35; Lu 11:51; Yt 11:4; 12:24.