Waxset

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

mooy juroom-ñetteelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.

Turam ma ngi jóge ci Augustus, ngir màggalee ko ko moom mi nekkoon buuru Rom ci 8 nj. j. Isaa. laataa moom moo nekkoon juroom-benneelu weer ci arminaatu waa-rom bu jamono ju yàgg ja.

Ci arminaatu weer bi, walla ci weeri wolof mooy yam ak baraxlu

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar