Samwie

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Weeru Samwie mooy weer wi njëkk ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul. Baat baa ngi jóge ci latin januarius, ngir maggale ko yàllay waa-rom ja: Janus (yàllay bunt yi). Ca jamono ju yàgg ja, moo nekkoon fukk ak benneelu weer ci arminaatu waa-rom.

Ci arminaatu jant bi, ñu koy wax it weeru wolof, mooy yam ak tamxarit

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar