Awril

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Weeru Awril mooy ñeenteelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul. Ca njalbeen moo nekkoon ñaareelu weer ci arminaatu waa-rom ba. Baat baa ngi jóge ci latin: Aprilis.

Ci arminaatu weer wi mooy yam ak rakki-gammu

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar