Xayra
Apparence

| Xayra لقاهرة | |
|---|---|
| Réew | |
| way-dëkk | 17 856 000 nit |
| atum way-dëkk | 2 009 |
| Rëyaay | 210 km² |
| Fattaay | 38 221 nit/km² |
| Gisub Xayra | |
Xayra (ci araab لقاهرة Al-Qāhira) mooy péeyu réewum Isipt, mooy dëkk bi ëpp nit ca goxub Afrig. Donte Al-Qāhira mooy tura dëkk waaye, lu bari, dees na ko wax itam, ci araabi waa-isipt, misr di Isipt ci araab.
