Aller au contenu

Way

Jóge Wikipedia.

Mbuug ak Way Mbuug nag mooy Misig (fr musique en music) mbuug nag ñu bari xamuñu baat bi ci wolof ba tax na misig rekk lañu koy wax ndax daa bokk ci baat yi nga xam ne ñépp a ko bokk niki lu mel ni widewo(video). WAY, baatu way mi ngi juge ci nit ku way maanaam nit ku yeww li tax ñu tudde nit kookii waykat dafa way ba man a sos ay wax mbaa ay nose yoo xam ne nit ñi mu nekkal bàyyiwuñu ci xel mbaa sax xamuñu ko woon, kon moo leen gën a way ba tax muy way kon ku ñuy tudde waykat dafa war a doon kuy yeete

Way batay man na tékki poesie ci wolof

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ay Mbuugkat ci Senegaal

Ay nosekat/Taalifkat ci Senegaal