Waxtaani jëfandikukat:Gamadji~wowiki

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

dalal-jàmm[soppi gongikuwaay bi]

maa ngi lay nuyu, man yorkat laa ci dal bi, gis naa sa liggéey, am na solo lool!!!! ñu farlu ni yaw la wiki bi soxla ngir ag jëm-kanamam. Li am solo mooy bind rekk, donte mindiin mi taxukoo deme noonu, looy gën di bind di gën di aay. At ci ginnaaw manu ma woon dara. Soo bëggee man a bind, doy na ngay jàngaat li nga jotoon a bind te nu toppaat ci jubanti lépp, loolu di na tax foo juumoon doo fa juumaat, man ba tay noonu laay def, abdu xaadir day faral di toppaat samay mbind, man ma leen di jàngaat. Soo amee baat yoo xamul ci wolof man nga leen seet ci wikbaatukaay. foofu yaw sax dinga fa man di dugal ay baat yu yees. Soo soxlaa ndimbal xamal ni maa ngi fi, walla nga saytu xëtu ndimbal wi. jaajëf! --Ibou (xëtu waxtaanuwaay) 7 Fewiriye 2009 à 12:26 (UTC)

Asala malëikoum, Jerejef Ibou, tey la giss sa message. Li nga ma wax, xaamu ma woon lolu, kon su ma beugeu xaam ben baatu wolof, di na fa dem. Tamit da ma beugeu yen saï nga wax ma sa xalat ca li mey def, ndax ma meunteu geuneun def lu bax. Sa ma wolof léroul nonu wa é sénégalais la (pulaar) françe la juddu, li moye tax. Sa ma mbok, Jajëf. Gamadji (xëtu waxtaanuwaay) 11 Fewiriye 2009 à 03:18 (UTC)
suma la binde man nga maa tontoo fii, dina tax li nu bindante yépp nekk ci wenn xët. xoolal xët yii wolof ngir gis arafi wolof ngir jàng bind, Wikipedia:babel

Votre compte va être renommé[soppi gongikuwaay bi]

20 Maars 2015 à 08:45 (UTC)

Compte renommé[soppi gongikuwaay bi]

17 Awril 2015 à 04:43 (UTC)