Aller au contenu

Waxtaan:Sheex Ahmadu Bamba

Le contenu de la page n’est pas pris en charge dans d’autres langues.
Jóge Wikipedia.

dalal-jàmm ci wikipedia, bég naa ci sag mbindu, te gis naa ne sunu ànde di nan def liggéey bu am-solo ci làkk wi. soo amee lu la jaaxal man nga maa def ay laaj ci sama xëtu waxtaanuwaay, ngir sunu liggéey man yomb dina laaj tamit nuy jokko yenn sa yi. man ngaa yër xëtu ndimbal wi tamit ngir am yeneeni leeral

sos ab jukki

[soppi gongikuwaay bi]

di la nuyu, sag farlu feeñ na! lenn rek laa la bëggoona leeral. laataa ngay sos jukki bu bees seetal baxam jukki bi am na ba noppi walla déet, ndax jukki bu tudd Seex Ahmadu Bamba am na fi ba noppi, yaw nga sosaat beneen tudde ko Sheex Ahmadu Bamba, te xam nga ñoo bokk li ñuy wax. te wolof seex lay wax. man ngaa far jukki bi tudd sheex, duggal mbind yi, ci bi tudd seex jekk-jekkal ko. demal ci xët wii ngir xam bu baax nuñuy sosee xët wu bees

Waaw mbòkk gis naa sa xalaat te it nangu na linga wax. Ci noonu, dinaa far jukki bii tudu Sheex Ahmadu Bamba te bayyi fi bi fi jotoona nekk. Jërë jëf