Waxtaan:Séeréer

Le contenu de la page n’est pas pris en charge dans d’autres langues.
Jóge Wikipedia.

Yaw miy def jukki yii, yaa ngi def liggéey bu am solo! waaye boo manoon a bind, teg ci gën a xool ni ñuy binde ci wolof dina baax lool, ndax li ngay bind am na solo lool, waaye fàwwu ñu toppaat ko, bindaat ko mu door a nekk lees man a yër (lire), kon ñi ngi ñaan nga gën a sonn ci xam bindiin ci wolof, jaajëf. --Abdu Xaadir Kebe (xëtu waxtaanuwaay) 2 Fewiriye 2009 à 14:20 (UTC)

Démarrer une discussion sur Séeréer

Démarrer une discussion