Waxtaan:Bisub Tabaski

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Deesul Wax Bés waaye Bis, Delloo ko ci Bisub Tabaski mooy Wolof de Ahloubadar

bis kay kenn du ko wax bés lees di wax, soo xoolee sax ayubés = semaine du ayubis (te moo ngi jóge ci ay bés, maanaam bés yu bari). laajteel bu baax. peace! --Ibou (xëtu waxtaanuwaay) 23 Nowembar 2009 à 18:54 (UTC)

loolu SËÑ Ibu jarul laajte bis lees di wax ci lu wér moodi wolof yu dëgër, doonte dees na wax bés ci déggin it moongi aju ci làmmeñi ña koy wax, te ndakaaru la am sax ngir ay sellal ak yuni mel, waaye bis moodi làmmeñu Wolof wu set.... Ahloubadar