Taba

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche
Taba gi
Taba gi
Tóor-tóori taba

Garabu taba garab la gu man a toll ci fukk ak juroom ba ci ñaar fukk met. Peer bi am daa kaaraange lool. Xas mi am ay xar-xar. Xobi garab gi man naa yaatu lool di toll ci juroom ñatti sàntimet ba ci fanweer ak juroom ci ay sàntimet, am it ay pàcc-pàcc yu man a àgg ci ñatt ba juroom ñaar. Taba garab la guy tóor-tóor, tóor-tóor yuy tijjeeku ba ci juroom ñaar.

Meññeef mi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Foytéefam daa am xott wu koy aar. Xott woowu moom la ñuy toj ngir jot taba ja ca biir, bu xott wi ubbeekoo man na ñoo nekk ci biiram ñeent ba ci juróom ñent donj taba leeg-leeg muy ñuul mbaa muy mboq mbaa muy xaw a jege xonq.

Turu xam-xam wi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Cola cordifolia