Sànqaay
Apparence
Sànqaay : xeet la ci xeeti garab yoo xam ne dañuy màgg ci fu am naaj, ñung kay fekk ci kémbaarug Afrig bu yaatu fa lool. Waaye itam, Waaye desu ko fekk fu mel ni: Nambi bi, ak Butsuwanaa, ak Afrig bët Saalum.
Melo wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Garab la gog man naa sax foo xam ne amul ndox. Baayima yu bari dan koy jëfëndikoo ngir di ci tabax seen i dëkkuwaay lu ci mel ni xeet i picc yi.
Ay xóbam dana yor melo bu muloŋ , ci yaatu waay, manees na koo natt ci juróom-fukk, jàpp teeméer ak juróom-fukk ci ay milimeetr
Solo si
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ay xóbam, danoo gaaw ci lool ci xeex biir buy daw, loolu moo tax mu bokk ci xeeti garab yi nga xam ne ci fajum cosaan.
turu xam-xam yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ficus glumosa