Aller au contenu

Sànd

Jóge Wikipedia.

Sànd garab la gog daa bokk ci njabootug moresea nekk ca Afrig sowwu jant, garab gu njool la man a àgg ba ci 20i met, day ruus jamonoy noor di sëq ci jamonoy nawet. Ay xobam am na ñu koy jëfandikoo cig togg di ko lekk.

Meññeef mi

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Meññeefi garabug sànd

Bu nawet biy jeex lay meññi. Dees koy lekk it, mu neex lool.

Turu xam-xam wi

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Morus mesoziygia