Rahmaniya

Jóge Wikipedia.

Rahmaniya: wenn yoon la ci yooni Tasawwuf yi, te tënku ci sunna. Ñu ngi koy askanale ci genn góor-Yàlla guñuy wax sëriñ Muhamed ibn Abdul Rahman Alzawaawii (1134h- 1207h),  ñiy topp yoon woowu nag tasaaroo nañu ci gox yu bari niki Saam, Iraã, Isibt ak la féete penku ca Afrig. Yoon la woo xam ne ay jéegoom gudd na lool ci tasaare Lislaam ci goxi Afrig, ba mëdd gëm-gëmu nasaraan ci fu bari ci Àdduna bi.[1][2][3][4][5][6][7][8][9][10][11]

References[Soppisoppi gongikuwaay bi]