Liisugar

Jóge Wikipedia.
Nataalu garabug Liisugar

Liisugar, xeetu garabu tóortóor la. Garab la gog mi ngi cosaanoo ci penku Afrig ak bëj-saalumu réewi araab yi.

Melo wi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Garab la gog dafa am ay xob yu dëgër guddaayam manees na koo natt ci 3i met jëm kaw, peeram dafa yaatu lool te rëy. Garab la gog dafa bari ay car lool ci jeexitalu car yi da nan fa gis ay tóotóor yoo xam ne guddaayam manees na koo natt ci 5 jàpp 15 ci sàntimet walla 1 jàpp 13 ci yaatuwaay. Garab la gog dees koy jëmbët ci ay pot. Mu yaatu lool ci tund wi nga xam ne dafa digg-dóomu tàngul seddul day soxlawoo naaj.

Nataal yi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Turu xam-xam wi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Adenium obesum