Kullu-kullu

Jóge Wikipedia.
Kullu-kullu gi (Pericopsis laxiflora)
Kullu-kullu gi (Pericopsis laxiflora)
Meññeefi garabug kullu-kullu
Meññeefi garabug kullu-kullu

Kullu-kullu turu xam-xam wi di morus Mesozygia. Jëmmam taxu koo rëy noonu. Nu koy faral di gis ci àllu Afrig yu ëpp ndox yi. Xob ya ak meññeef ya dinañu dundal guereza, unsinge colobe mi nuy gis lu ëpp ca Afrig Sowwu jant ak gu diggu gi. Yenn saa yi nag nu def ko matt di ko jaay.

Barab yi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Jamono jii garab gi bari na lool Ngogo, ca kër-Mala boobu nu naan Kibale ca Ugàndaa, mu nekk lu "chimpanze" yi du dunde bis bu ne.

Turu xam-xam wi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Pericopsis laxiflora