Jëfandikukat:Ibou wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Guaka (waxtaancëru)
m wikiliens
Rëdd 5 : Rëdd 5 :
Ci 2007 bii laa tambalee jang wolof. Mooy làkk bi ma gënn a neex. Ci 2007 bi itam laa bindu ci Wikipedia tambalee cëru ci liggéey bi. Benn weer laa fi def ñu tàbb ma yorkat.

li ëpp ci li may jàng mooy téere taariix, roman, taalif ak xeltu. Téere bi ma njëkk a jàng mooy "nations négres et cultures" "Reewi ñu ñuul ak cosaan" bu seex anta joob. Bindkat bi ma gënn a neex mooy Paulo Coelho di ab waa-beresil.
li ëpp ci li may jàng mooy téere taariix, roman, taalif ak xeltu. Téere bi ma njëkk a jàng mooy "nations négres et cultures" "Reewi ñu ñuul ak cosaan" bu seex anta joob. Bindkat bi ma gënn a neex mooy [[Paulo Coelho]] di ab waa-beresil.
Taggat-yaram bi ma gën a neex mooy futbòl.

[[Image:Cheikh Anta Diop.gif|thumb|center| Sama royuwaay bi gën a mag ci wàllu adduna

<center> seex anta joob</center>
<center> [[Seex Anta Joob]]</center>
]]
]]
</poem>
</poem>

Sumb bu 24 Ut 2007 à 18:35

Royuwaay:Babel-3

man la

Di nuyu ñépp
Sama tur mooy Ibrahima fall, ibou di sama dakkantal. Am 23 at. Ci samag dund gu dëggu damay liggéey bes bi di jang ngoon ngi. Xaralaymbëj laay tòpp. Venezia (Itaali) laa dëkk am na 5 at.
Ci 2007 bii laa tambalee jang wolof. Mooy làkk bi ma gënn a neex. Ci 2007 bi itam laa bindu ci Wikipedia tambalee cëru ci liggéey bi. Benn weer laa fi def ñu tàbb ma yorkat.

li ëpp ci li may jàng mooy téere taariix, roman, taalif ak xeltu. Téere bi ma njëkk a jàng mooy "nations négres et cultures" "Reewi ñu ñuul ak cosaan" bu seex anta joob. Bindkat bi ma gënn a neex mooy Paulo Coelho di ab waa-beresil.
Taggat-yaram bi ma gën a neex mooy futbòl.

Dencukaay:Cheikh Anta Diop.gif
Sama royuwaay bi gën a mag ci wàllu adduna
Seex Anta Joob