Wolof (askan) wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
Wolof genn giir la gu nekk Senegaal.[[ Wolof]] nio fi eup ca xetu sénégal [[Image:OuolofCayor.jpg|thumb|left|Wolof du [[Cayor]] (gravure de [[1890]])]].
Wolof genn giir la gu nekk Senegaal.[[ Wolof]] ñoo ëpp ci waaso yi ci Senegaal [[Image:OuolofCayor.jpg|thumb|left|Wolofu[[Kajoor]] (yatt gu [[1890]])]].
Mamu wolof y isipt lanu jogue. [[Séeréer]] y, Pël, [[Sooninke]], Tekuruuri (Tukuloor), ak Sara u jogué nguruu Baguirmi ca rewm Tchad. Wolof y ca xeet y lanu jogue. Xeet ni yéep da nu jaxaasé, ca yonu Imbratoor gu Ghana, ca deuk bi nu tuddé Djolof. Wolof moye ku jogué Djolof, Wa-Lof (ku jogué Lof) wala Wa-Laf (ku jogué Laf), di nek tey Wolof. [[Seex Anta Joob]], Walaf la done waxé. Nonu la xeetu Wolof judu. Tuur bi li nu wax Djolof, bene Socé ku tundu Djolof Mbengue moko joox deuk bi. Ca cossan da nu jolof Mbengue ak njabotam mo fi dieuk nek. Ba nopi Amadu Abubakar niow na, mom bayam Naaru Murabin la woon, tuuram Abu Bakr Ben Omar, ca cossan danu wax Abu Dardaï, yayam Tukuloor la woon tuuram Fatumata Sall domu Lam-Toro (Lamanu Toro) ca [[Tekuruur]]. Amadu, Bayam ben jambar Saraxule moko rey, bobu nak Fatumata setsina bénene dieuker. Amadu bougou woon dieuker bou bess bi, li moye tax da fa daaw ca Waalo. Fofu nak nit y fi nek ay Lamanu Séereer yu sant Ngom aki Sambkatu Pël yu sant Diaw. Laman y danu yékéti Amadu, Ndax da fa baxone ba jaaxal deuk bi, ba nek Buuru Waalo. Séereer y nio ko tudd Njaajan Njaay. Ndax Mbaanu Njaay moye Gaïndé (Gaïndé Njaay ca cossan) Gaïndé moye buuru all ba.
Maami wolof yi Isipt lañu bawoo. [[Séeréer]] si, Pël yi, [[Sooninke]] yi, Tekuruur yi (Tukuloor), ak Saraxule yi juge nguuru Bagirmi ca réewum Cadd. Wolof yi ca xeet ya lañu juge. Xeet ya yépp danoo jaxasoo, ca yoonu Imbraatoor gu Ghana, ca dëkk bi nu tuddé Jolof. Wolof mooy ñu bawoo Jolof, Waa-Lof (ay gaa yu juge Lof) walla Waa-Laf (ñoñ Laf), di nekk tay Wolof. [[Seex Anta Joob]], Walaf la doon wax. Noonu la xeetu Wolof judoo. Tur wii nuy wax Jolof, benn Sooce bu tundoon Jolof Mbeng moo ko joxoon dëkk ba. Ca cosaan dañu ne Jolof Mbeng ak njabootam ñoo fa njëkkoon a dëkk. Ba noppi Amadu Abuubakar ñëw fa, moom baayam Naaru Murabituun la woon, turam di Abu Bakr Ben Omar, ca cosaan danu daa wax Abu Dardaayi, yaayam Tukuloor la woon, turam di Fatumata Sàll doomu Lam-Tooro (Lamanu Tooro) ca [[Tekuruur]]. Amadu, Baayam jenn jàmbaar ju Saraxule moo ko ray, booba nag la Fatumata seeti jeneen jëkër. Amadu bégul woon ci boroom këru nday ju bees ji, lii a taxoon mu dem Waalo. Foofa nag nit ña fa nekk ay [[Laman]]i [[Séeréer]] yu sant Ngom aki Sàmmkati Pël yu sant Jaw. Laman yi danoo yékkati woon Amadu, ndax dafa baaxoon ba jaaxal dëkk bi, ba far mujj di Buuru [[Waalo]]. Séeréer si ñoo ko tudde [[Njaajaan Njaay]]. Ndax Mbaanu Njaay mooy Gaynde (Gaynde Njaay ca cosaan) te Gaynde mooy buuru àll ba.
Wa é ba paré Njaajan deen ko daq deuk bi, ndax amna nu ku bougoune ko rey. Daaw na ba Djolof ca Wolof y. Njaajan Njaay da dadjalé Wolof y ndax nu menteu geuneu am dolé, ba meunteu tabaax Imbratoor gu Djolof. Wolof, [[Jolof]] moye seni deuk wa é ak seni imbratoor gi, da nu dem deuk té yoor: Waalo, Tekuruur, Kajoor, Bawol, Sine-Saloum, Njaarmew (sogo nek Bundu), Niani, Wulli, Bambouk. Nguruu gi yéep Djolof uff na ko. Li moye tax Lakku Wolof moye lakku nit ni geuneu wax ca senegal. Atu 1549, Jolof bu makk ngi tass na ak Lélé Fuli Fak. Nguruu Wolof yéep am seni buuru bop: Damel Kajoor, Teigne Bawal, Braak Waalo, Buurba Jolof (Ca Jolof bu mak nga, Buur Fari lanu waxon). Dethié Fu Njoogu ak Amari Ngoné Sobel Faal, nio fi dieuk nek Damel-Teigne.
Waaye ba noppi Njaajaan dañu koo dàqe dëkk ba, ndax daa am ku ko bëggoon a ray. Mu daal di woon daw ba Jolof ca Wolof ya. Njaajaan Njaay dajale woon na Wolof yi ndax ñu gën a am doole, ba man a taxawal Imbraatóor gu Djolof. Wolof yi, [[Jolof]] mooy seeni dëkk, waaye ak seeni imbraatoor gi, dañoo demoon dëkk te yor: [[Waalo]], [[Tekuruur]], [[Kajoor]], [[Bawal]], [[Siin-Saalum]], Njarmeew (soog a dëkk Bundu), Ñaani, Wulli, Bambug. Nguur ga gépp Jolof uffoon na ko. Lii moo tax Làkku Wolof mooy làkk wi ñu gën a wax ci [[Senegaal]]. Ca atum 1549 la Jolof gu mag ga tas ak Lele Fuli Fak. Nguuri Wolof yépp am seeni buuri bopp: Dammeel ca Kajoor, Teeñ ca Bawal, Baraag ca Waalo, Buurba ca Jolof (Ca Jolof gu mag ga, Buur Fari lañu daa wax). Decce Fu Njóogu ak Amari Ngóone Sabel Faal, ñoo fi njëkk a nekk Dammeel-Teeñ.


Njabotu Wolof nonu, nio yoron nguruu wolof y:
Njabooti Wolof yooyu, ñoo yoroon nguuri wolof yi:
* Njaay (Jolof)
* Njaay (Jolof)
* Mbodji ak Wade (Waalo)
* Mbóoj ak Wàdd (Waalo)
* Faal ak Joop (Kajoor ak Bawal)
* Faal ak Jóop (Kajoor ak Bawal)
[[Image:Thiédo.jpg|200px|thumb|Un [[tiedos|tiedo]] près de [[Bakel (Sénégal)|Bakel]] ([[1853]])]]
[[Image:Thiédo.jpg|200px|thumb|ab [[Ceddo]] ca wetu [[Bàkkel]] ([[1853]])]]

Nosteg mboolaay ga nii la tëdde woon y:
Nosteg mboolaay ga nii la tëdde woon:
* Géer/Garmi, ca kaw, nio done buuri. Kangam (buuri Laman y) Farba Kaba (buuri [[Ceddo]] y), Toubé, Boumi ak Linguére.

Ca seeni meen nio meunteu nek Buur. Meen mo geuneu am solo Guegno.
* Géer/Garmi, ca kaw, ñoo doon nekk buur yi. Kàŋam (buuri Laman yi) Farba Kaba (buuri [[Ceddo]] yi), Tuube, Bumi ak Lingeer.
Ca seeni meen ñoo man a nekk Buur. Meen moo gën a am solo Geño([['''Meen''']]:wàllug nday. [['''Geño''']]:wàllug baay .
* Jambour ak Serign y. Niom Serign y ay Tukuloor (Dia, Sy, Lô, Sall) Saraxule (Sylla, Khoulé, Cissé, Dramé, Kébé) wala ay Naar (Diakhoumpa, Aïdara, Coundoul, Sady, Babou) lani doon.
* Jambour ak Serign y. Niom Serign y ay Tukuloor (Dia, Sy, Lô, Sall) Saraxule (Sylla, Khoulé, Cissé, Dramé, Kébé) wala ay Naar (Diakhoumpa, Aïdara, Coundoul, Sady, Babou) lani doon.
* Badolo, Mbey mo done seeni dund.
* Badolo, Mbey mo done seeni dund.

Sumb bu 8 Fewriyee 2009 à 21:31

Wolof genn giir la gu nekk Senegaal.Wolof ñoo ëpp ci waaso yi ci Senegaal

WolofuKajoor (yatt gu 1890)

.

Maami wolof yi Isipt lañu bawoo. Séeréer si, Pël yi, Sooninke yi, Tekuruur yi (Tukuloor), ak Saraxule yi juge nguuru Bagirmi ca réewum Cadd. Wolof yi ca xeet ya lañu juge. Xeet ya yépp danoo jaxasoo, ca yoonu Imbraatoor gu Ghana, ca dëkk bi nu tuddé Jolof. Wolof mooy ñu bawoo Jolof, Waa-Lof (ay gaa yu juge Lof) walla Waa-Laf (ñoñ Laf), di nekk tay Wolof. Seex Anta Joob, Walaf la doon wax. Noonu la xeetu Wolof judoo. Tur wii nuy wax Jolof, benn Sooce bu tundoon Jolof Mbeng moo ko joxoon dëkk ba. Ca cosaan dañu ne Jolof Mbeng ak njabootam ñoo fa njëkkoon a dëkk. Ba noppi Amadu Abuubakar ñëw fa, moom baayam Naaru Murabituun la woon, turam di Abu Bakr Ben Omar, ca cosaan danu daa wax Abu Dardaayi, yaayam Tukuloor la woon, turam di Fatumata Sàll doomu Lam-Tooro (Lamanu Tooro) ca Tekuruur. Amadu, Baayam jenn jàmbaar ju Saraxule moo ko ray, booba nag la Fatumata seeti jeneen jëkër. Amadu bégul woon ci boroom këru nday ju bees ji, lii a taxoon mu dem Waalo. Foofa nag nit ña fa nekk ay Lamani Séeréer yu sant Ngom aki Sàmmkati Pël yu sant Jaw. Laman yi danoo yékkati woon Amadu, ndax dafa baaxoon ba jaaxal dëkk bi, ba far mujj di Buuru Waalo. Séeréer si ñoo ko tudde Njaajaan Njaay. Ndax Mbaanu Njaay mooy Gaynde (Gaynde Njaay ca cosaan) te Gaynde mooy buuru àll ba. Waaye ba noppi Njaajaan dañu koo dàqe dëkk ba, ndax daa am ku ko bëggoon a ray. Mu daal di woon daw ba Jolof ca Wolof ya. Njaajaan Njaay dajale woon na Wolof yi ndax ñu gën a am doole, ba man a taxawal Imbraatóor gu Djolof. Wolof yi, Jolof mooy seeni dëkk, waaye ak seeni imbraatoor gi, dañoo demoon dëkk te yor: Waalo, Tekuruur, Kajoor, Bawal, Siin-Saalum, Njarmeew (soog a dëkk Bundu), Ñaani, Wulli, Bambug. Nguur ga gépp Jolof uffoon na ko. Lii moo tax Làkku Wolof mooy làkk wi ñu gën a wax ci Senegaal. Ca atum 1549 la Jolof gu mag ga tas ak Lele Fuli Fak. Nguuri Wolof yépp am seeni buuri bopp: Dammeel ca Kajoor, Teeñ ca Bawal, Baraag ca Waalo, Buurba ca Jolof (Ca Jolof gu mag ga, Buur Fari lañu daa wax). Decce Fu Njóogu ak Amari Ngóone Sabel Faal, ñoo fi njëkk a nekk Dammeel-Teeñ.

Njabooti Wolof yooyu, ñoo yoroon nguuri wolof yi:

  • Njaay (Jolof)
  • Mbóoj ak Wàdd (Waalo)
  • Faal ak Jóop (Kajoor ak Bawal)
Dencukaay:Thiédo.jpg
ab Ceddo ca wetu Bàkkel (1853)

Nosteg mboolaay ga nii la tëdde woon:

  • Géer/Garmi, ca kaw, ñoo doon nekk buur yi. Kàŋam (buuri Laman yi) Farba Kaba (buuri Ceddo yi), Tuube, Bumi ak Lingeer.

Ca seeni meen ñoo man a nekk Buur. Meen moo gën a am solo Geño('''Meen''':wàllug nday. '''Geño''':wàllug baay .

  • Jambour ak Serign y. Niom Serign y ay Tukuloor (Dia, Sy, Lô, Sall) Saraxule (Sylla, Khoulé, Cissé, Dramé, Kébé) wala ay Naar (Diakhoumpa, Aïdara, Coundoul, Sady, Babou) lani doon.
  • Badolo, Mbey mo done seeni dund.

Neeno y:

  • Teug y, Lawbe, Wuude, Rabb y. Am nanu bari ca xetu Pël/Tukuloor lani jogué moye Njabotu : Thiam, Mbow, Athié, Diaw, Dioum, Tall, Fam, Guissé, Sow. Neeno nonu dani kalenté ak Pël y, ndax dani mbokk mam.

Neeno u Wolof: Beye, Niasse, Dieng, Mbaye, Niang.

  • Gueweul y, nieup lani way, Buuri, Neeno. Cossanu nit yeup lani xaam, seni Sant yu geuneu siiw: Seck, Mbaye, Mboup, Lam, Seye .

Jaam y:

  • Amna jaami buuri ( Ceddo ), Jaami Juddu, Jaami Sayor (Niom ca xeer lanu done ko dieul). Xeet gunek lani djogué.

Wolof y danu jaxaasé li moye tax seni sant danu bari, tamit xet yu bari niow nanu ca niom (Wolofisation). Seex Anta joop né na, Wolof y deug deug no: Njaay, joop, Faal, Niang, Beye, Mbodji, Mboup, Wade, Gueye. Ca Fuuta-Tooro, ca Cuballo (Nappkat Tukuloor) wala Sebbe (Ceddo/Jambar Tukuloor) Wala Toroodo, lani nek. Da ni tel nek fofu. Ca senegal niom no dieuk giss Tubap y. Bou dieuk Ceddo lani woon, tey you bari ca yoonu murid lanu nek wala tidjanya. Amna ay chrétien tamit (Gorée-Saint-Louis). Seex Amadu Bamba Mbakké ak El Adj Malik Sy nio geuneu duggal Wolof y ca lislaam. Wolof yu bari tuxu neen Fraanse, Etat-unis, Italie, Espagne. Ca senegal da niu yoré posty yu geuneu Mag. Niom no geuneu fonk seni rewm (Nationalisme Sénégalais). Amna nu da nuy dund ca Mbey (Kaw-Kaw), Napp ca guedj bi (ca niom Lebu y lani bokk). Jom ak Teraanga ca niom la jogué.