Dëkkaani ndiiwaani Senegaal
Apparence
Dëkkaani ndiiwaani yi, ci Senegaal, ay dog lañu ci séddaliinu yoriinu réew mi. ci 2007 lim bu toll 43 lañu.
Taariix
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Yokkug nit ñi dëkk ci Ndakaaru moo dem ba àgg ci benn dayoo bi, ba tax genn kilifag dëkk rekk manatu koo yor, tax sosug geneen nekkte gu gën a suufe waroon. Kon lii moo tax ci 1996 ñu séddale tunduw Ndakaaru ci 43 dëkkaani ndiiwaan, ni dëkk bu Paris.
Dogiin
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]43 Dëkkaani ndiiwaani yi dañu leen séddale ci 4 tund yi:
- Cees: 3
Xool it
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Lëkkalekaay yu biir
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Téerekaay
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
- (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)