Duni Kanaari

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Duni Kanaari yi (ci wu-ispaañ Islas Canarias) ay dun lañu yu bokk ci goxu Afrig, féete ci bëj-gànnaar-sowwu Afrig nekk ci mbàmbulaanu Atlas, te bokk ci réewum Ispaañ. Ñoo ngo ko Séddale ci ñaari tund Santa Cruz gu Tenerif ak Las Palmas.

Gongikubaat[Soppi]

Turu duni Kanaari ngi jëlee turam ci latin Canariae Insulae (duni xaj yi); tur wi ci Kanaari gu Mag rekk lees ko doon jëfandikoo ("Canaria Insula"). Di bàyyikoo ci xaji àll yu mag ("canes") yu nemmeekukat yu njëkk yi wuññi woon ca dun ba.

Lëkkalekaay yu biti[Soppi]