Aller au contenu

Aw xët ci wàll gii

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal



Diiwaani Senegaal yi ay xaaj yu yoriin yu Senegaal lañu.

xaaj yu suuf si.

nosiinu suuf si

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Kartu Diiwaani Senegaal ci 2005

Fii mu nekk, séenub lim mi ngi ci 14, la ko dale ca ba ñu sosee diiwaanu diiwaanu Matam ca 2001, teg ci yeneen ñatti diiwaan yi ci 2008 : Kafrin ci digg bi, Keedugu ci bëj-saalum-penku bi ak Séeju ci bëj-saalum, ci Kaasamaas[1].

rëyaay ak askan

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Diiwaan Rëyaay
en km²
Askan
Ndakaaru 550 2 411 528
Njaaréem 4 359 930 008
Fatig 7 935 639 075
Kawalx 16 010 1 128 128
Koldaa 21 011 834 753
Luga 29 188 559 268
Maatam 25 083 423 041
Ndar 19 044 863 440
Tambaakundaa 59 602 530 332
Cees 6 601 1 348 637
Sigicoor 7 339 557 606
mboole-séen :[2] 196 176 10 225 816
  1. yax bi péncum ndawi réew mi kàddu (woote) ci 1 fewrie 2008 [1]
  2. ay mboole-séen (walla ay mboolante) bu ñu tënkoo ci lim yu aliwa jii (lim yu ñu roowal (yu ñu mottali))

Voir aussi

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Royuwaay:PolitiqueSénégal

Jukki yi ci aju

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Bibliographie

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
  • (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
  • (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)
  • (fr) Laurence Porgès, Bibliographie des régions du Sénégal, Dakar, Ministère du Plan, 1967, 705 p. (Thèse de 3e cycle publiée)
  • (fr) Laurence Porgès, Bibliographie des régions du Sénégal. Complément pour la période des origines à 1965 et mise à jour 1966-1973, Paris, Mouton, 1977, 637 p.

lëkkalekaay yu biti

[Soppisoppi gongikuwaay bi]