Ayiti
Apparence
(Yoonalaat gu jóge Aayti)
Ayiti | |||||
| |||||
Barabu Ayiti ci Rooj | |||||
Dayo | km2 | ||||
Gox | |||||
Way-dëkk | nit | ||||
Fattaay | nit/km2 | ||||
Xeetu nguur - Njiitu Réew - Njiitu Jëwriñ |
|||||
Tembte - Bawoo - Taariix |
|||||
Péy ak rëddi - Tus-wu-gaar - Tus-wu-taxaw |
Port-o-pirins | ||||
Làkku nguur-gi | wu-faraas, kereyool bu Ayiti | ||||
Koppar | |||||
Turu aji-dëkk | |||||
Telefon | |||||
Ayiti ab dun la bu nekk ca Amerik diggu. Day ab dun bu mag bu mu bokkal Republik dominicaine te Port-au-Prince di péyam.
Ayiti mooy reewu ñu ñuul ñi njëkka moom seen bopp ci attum 1804, ca seen fippu ga (1791-1803) ca la ñu dakkee Napoleon ak ay ñoñam ca dun ga.
Magginu turu dëkk ba
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ci aaday Taino yi, Ayiti da doon tekki suufu doj yu kawe ya walla aw doj ci biir geej.