Xiirtalug mbëjbijjaakon

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet


Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal



Xiirtalug mbëjbijjaakon ag feeñteeg jëmm la gees di gis niki juddug ag wuuteeg aj ci diggante ñaari cati ab wommatukaayu mbëj walla ci ag ndombo gu mbëj mbaa juddug ag dawaanu mbëj ci seen biir, su wommatukaay bi walla ndombo gi nekkee ci biir ab toolu bijjaakon. Ci gii feeñteg jëmm la doxub soppalikaay yu mbëj yeek xiirtalukaay yi sukkandiku.