Ndiiwaani Senegaal
Ndiiwaani Senegaal yi ay dog lañu ci séddaliinu yoriinu Senegaal.
Ndiiwaan nag ag nekkte (entité) gu suuf la, gu ñuy faral di gis ci réew yiy làkk wu-fraas. Soo demee ci ñiy làkk wu-angalteer weneen dogiin nga fay fekk.
Ci Senegaal, ndiiwaan yi dinañu leen waññi ci lim bu tollook 92 ci 2007.
Taariix
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Limu tund yi (nosu topp abajada)
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Bala
- Jaawara
- Gudiiri
- Kidiira
- Baba Garaas
- Lambaay
- Ngoy
- Jululu
- Sinja
- Tenduk
- Tengori
- Nooto
- Puut
- Cenaba
- Mban
- Roos Beeco
- Jaxaaw
- Fimla
- Ñaaxar
- Taatagin
- Jilloor
- Ñoojoor
- Tubaakuta
- Kolobaan
- Kawóon
- Waajur
Géejawaay moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la
Ñu séeddale ko ci 5 dëkkani ndiiwaan
Dogiinu tund wi dañu koo soppi gannaaw sosug tunduw Kungeel ci 2006.
Kon mu des :
- Birkilaan
- Maleem-Odaar
- Nganda
- Kanel
- Seeme
- Ganjaay
- Ndenjeng
- Ndóofaan
- Daaru Musti
- Ndand
- Sagata
- Bandafasi
- Fongolimbi
- Salemata
- Saraya
- Dabo
- Julaacolon
- Medina Yoro Fula
Mi ngi judd ci 2006 (amul lonkoyoon bu jàppandi nii-nii)
- Barkeji
- Daara
- Dooji
- Yang-Yang
- Kër Momar Saar
- Kokki
- Mbejeen
- Sakal
Ndiiwaanu Raawo, biy feeñ ci lonkoyoon bi, ci tunduw Ndar la bokk 2002 ba tay.
- Fisel
- Ngeexoox
- Caajaay
- Jiwaalo
- Añam Ciwol
- Ogo
- Kayel
- Ndam
Ndakaaru moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la
Ñu séeddale ko ci 19 dëkkani ndiiwaan.
- Ndindi
- Ndulo
Gannaaw dogaat ga waraaloon juddug Diiwaanu Maatam, tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu
- Raawo
- Medina Sabax
- Pawoskoto
- Wak Nguna
Pikin moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la
Ñu séeddale ko ci 16 dëkkani ndiiwaan.
- Pikin
- Kas-Kas
- Njum
- Salde
- Cile Buubacar
Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Welingara
- Bunkiling
- Jaatakunda
- Jend
- Marsasum
- Tanaaf
- Kumpentum
- Kusaanaar
- Makakolibantang
- Misiira
Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Sebixotaan, moom ci boppam ñu séddale ko ci 3 dëkkaani Ndiiwaan.
- Meewaan
- Merina Daqar
- Ñaaxeen
- Pambal
- Bookoto
- Kunkan
- Pakur
Xool it
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Lëkkalekaay yu biir
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Lëkkalekaay yu biti
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Site officiel du gouvernement du Sénégal
- Données statistiques worldbank.org
- Chiffres population www.gouv.sn
- Découpage administratif sur www.senegalaisement.com
- « Décentralisation : Les bœufs attendent la charrue » (article Panos Infos, 2003))
Téerekaay
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
- (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)