Ndiiwaani Senegaal

Ab jukkib Wikipedia.

Dem : Joowiin, Seet
Ndiiwani Senegaal

Ndiiwaani Senegaal yi ay dog lañu ci séddaliinu yoriinu Senegaal.

Ndiiwaan nag ag nekkte (entité) gu suuf la, gu ñuy faral di gis ci réew yiy làkk wu-fraas. Soo demee ci ñiy làkk wu-angalteer weneen dogiin nga fay fekk.

Ci Senegaal, ndiiwaan yi dinañu leen waññi ci lim bu tollook 92 ci 2007.

Tëraliin

[Soppi] Taariix

[Soppi] Limu tund yi (nosu topp abajada)

[Soppi] Tunduw Bàkkel

Ndiiwaani Bàkkel
  • Bala
  • Jaawara
  • Gudiiri
  • Kidiira

[Soppi] Tunduw Bambey

Ndiiwaani Bambey
  • Baba Garaas
  • Lambaay
  • Ngoy

[Soppi] Tunduw Biñoona

Ndiiwaani Biñoona
  • Jululu
  • Sinja
  • Tenduk
  • Tengori

[Soppi] Tunduw Cees

Ndiiwaani Cees
  • Nooto
  • Puut
  • Cenaba

[Soppi] Tunduw Dagana

Ndiiwaani Dagana
  • Mban
  • Roos Beeco

[Soppi] Tunduw Fatik

Ndiiwaani Fatik
  • Jaxaaw
  • Fimla
  • Ñaaxar
  • Taatagin

[Soppi] Tunduw Funjunj

Ndiiwaani Funjunj
  • Jilloor
  • Ñoojoor
  • Tubaakuta

[Soppi] Tunduw Gosaas

Ndiiwaani Gosaas
  • Kolobaan
  • Nginngineew
  • Kawóon
  • Waajur

[Soppi] Tunduw Géejawaay

Ndiiwaani Géejawaay

Géejawaay moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 5 dëkkani ndiiwaan

[Soppi] Tunduw Kafrin

Ndiiwaani Kafrin

Dogiinu tund wi dañu koo soppi gannaaw sosug tunduw Kungeel ci 2006.

Kon mu des :

  • Birkilaan
  • Maleem-Odaar
  • Nganda

[Soppi] Tunduw Kanel

Ndiiwaani Kanel
  • Kanel
  • Seeme

[Soppi] Tunduw Kawlax

Ndiiwaani Kawlax
  • Ganjaay
  • Ndenjeng
  • Ndóofaan

[Soppi] Tunduw Kebemeer

Ndiiwaani Kebemeer
  • Daaru Musti
  • Ndand
  • Sagata

[Soppi] Tunduw Kéedugu

Ndiiwaani Kéedugu
  • Bandafasi
  • Fongolimbi
  • Salemata
  • Saraya

[Soppi] Tunduw Koldaa

Ndiiwaani Koldaa
  • Dabo
  • Julaacolon
  • Medina Yoro Fula

[Soppi] Tunduw Kungéel

Mi ngi judd ci 2006 (amul lonkoyoon bu jàppandi nii-nii)

[Soppi] Tunduw Lingeer

Ndiiwaani Lingeer
  • Barkeji
  • Daara
  • Dooji
  • Yang-Yang

[Soppi] Tunduw Luga

Ndiiwaani Luga
  • Kër Momar Saar
  • Kokki
  • Mbejeen
  • Sakal

Ndiiwaanu Raawo, biy feeñ ci lonkoyoon bi, ci tunduw Ndar la bokk 2002 ba tay.

[Soppi] Tunduw Mbuur

Ndiiwaani Mbuur
  • Fisel
  • Ngeexoox
  • Caajaay
  • Jiwaalo

[Soppi] Tunduw Maatam

  • Añam Ciwol
  • Ogo

[Soppi] Tunduw Mbakke

Ndiiwaani Mbakke
  • Kayel
  • Ndam

[Soppi] Tunduw Ndakaaru

Ndiiwaani Ndakaaru

Ndakaaru moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 19 dëkkani ndiiwaan.

[Soppi] Tunduw Njaaréem

Ndiiwaani Njaaréem
  • Ndindi
  • Ndulo

[Soppi] Tunduw Ndar

Ndiiwaani Ndar

Gannaaw dogaat ga waraaloon juddug Diiwaanu Maatam, tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu

  • Raawo

[Soppi] Tunduw Ñooro gu Rip

Ndiiwaani Ñooro gu Rip
  • Medina Sabax
  • Pawoskoto
  • Wak Nguna

[Soppi] Tunduw Pikin

Ndiiwaani Pikin

Pikin moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 16 dëkkani ndiiwaan.

  • Pikin

[Soppi] Tunduw Podoor

Ndiiwaani Podoor
  • Kas-Kas
  • Njum
  • Salde
  • Cile Buubacar

[Soppi] Tunduw Raneru

Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Welingara

[Soppi] Tunduw Séeju

Ndiiwaani Séeju
  • Bunkiling
  • Jaatakunda
  • Jend
  • Marsasum
  • Tanaaf

[Soppi] Tunduw Siggcoor

Ndiiwaani Siggcoor

[Soppi] Tunduw Tambaakundaa

Ndiiwaani Tambaakundaa
  • Kumpentum
  • Kusaanaar
  • Makakolibantang
  • Misiira

[Soppi] Tunduw Tënjéej

Ndiiwaani Tënjéej

Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Sebixotaan, moom ci boppam ñu séddale ko ci 3 dëkkaani Ndiiwaan.

[Soppi] Tunduw Tiwaawon

Ndiiwaani Tiwaawon
  • Meewaan
  • Merina Daqar
  • Ñaaxeen
  • Pambal

[Soppi] Tunduw Usuy

Ndiiwaani Usuy

[Soppi] Tunduw Welingara

Ndiiwaani Welingara
  • Bookoto
  • Kunkan
  • Pakur

[Soppi] Xool it

[Soppi] Lëkkalekaay yu biir

[Soppi] Lëkkalekaay yu biti

[Soppi] Téerekaay

  • (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
  • (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)
Samay jumtukaay
Yeneeni làkk