Jóge Wikipedia.
 |
I am a sysop (Yorkat) in this Wiki. |
|
wolof: Sama tur mooy Ibrahima Fall, Ibu di sama dakkantal. Am naa 26 at. Ci samag dund gu dëggu damay jàng boppu daara-ju-kawe ju bologna ca Itaali. Venezia (Itaali) laa dëkk.
Ci 2007 laa tambalee jàng wolof. Mooy làkk bi ma gënn a neex te it mooy sama làkk ci meen. Ci 2007 itam laa bindu ci Wikipedia tambalee cëru ci liggéey bi. Ab yorkat laa ci.
li ëpp ci li may jàng mooy téere taariix, roman, taalif ak xeltu. Téere bi ma njëkk a jàng mooy "nations négres et cultures" "Reewi ñu ñuul ak cosaan" bu Seex Anta Joob. Bindkat bi ma gënn a neex mooy Paulo Coelho di ab waa-Bresil.
Taggat-yaram bi ma gën a neex mooy futbòl.
English: My name is Fall Ibrahima, I study automation in the university of bologna in Italy. I live in venice. I started to contribute in Wikipedia in 2007. I am administrator in Wikipedia Wolof and Wiktionary. I translate the mediawiki interface into Wolof.
[Soppi] Bindwaay