Seex Anta Jóob

Jóge Wikipedia.
(Yoonalaat gu jóge Seex Anta Joob)

Séex Anta Jóob mu ngi juddu ci 29 deesàmbar ci atum 1923 ci ceytu, faatu ci 7 féwrier ci atum 1986 ci Ndakaaru. MoomlSénégala Saa-Senegaal la di gëstukat ak ku doon yëngu ci walu polotig giirug dundam, dafa doon wane ñariñu Afrig rawati na der bu ñuul ci mboorum aduna si.

Ba tay amna ci Mbidam yu ñuy ŋañ, ba taxna du ñu kay faral di féssal, rawatina li mu binda ci walu Egypte ak ciossaanu kalaama wolof.

Wayé Séex Anta Jóob bokk na ci ñi njëkk a bind ci mbooru Afrig ak kolonisationg.


Diar diar am ak ŋiagalém[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Séex Anta Jóob muŋi juddu ci 29 déçambar ci atum 1923 ci ceytu, ci diwaanu Bambeï, ci ŋiaaréem.

Ci askane wu mag la soxékoo. Bi mu amé 23 att la dém farançe ŋir diaŋ physique akk chimie, wayé mu moudjé djublu ci histoire akk science sociales, rawatina ŋiaŋalém Gaston Bachelard akk bu Frédéric Juiot-Curie. Moome bokkul guiss guiss akk  ñiy xalaate ni afrik amoul histoirou bopam.

Ci atum 1951 la Séex Anta Jóob , ci dimbalu Marcel Giraule, wadjal thézou doctorat ci ñiangalé mu kawé ci université bu Paris. Ci thèze boobu ci la xamlée ni waa Egypte ay nitt ñu ñul lañiouwoone té itam lakk akk aaday afrik yi fofu la soxékoo.