Ecser

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet
Ecser
Réew Raaya Oonguri Oonguri
Nekkte dëkkaan
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
47° 26′ Bëj-gànnaar
     19° 19′ Sowwu
/ 47.433, -19.317
Rëyaay 22,625 km²
Fattaay 248 05 nit/km²
Ecseri 168.jpg

Ecser ab dëkkaanu tunduw Pest la, bokk ci suufus Budapest. Am na 3.534 way-dëkk (2008) te bari ay saa-slowaki.

Ecser a ngi nekk ci bëj-saalum-penku Budapest, ci wetu Naawuwaayu Budapest-Ferihegy. Peggook Maglód, Vecsés, Gyömrő ak Üllő. Yoonu weñ wu 120a (Budapest-Újszász-Szolnok) moo fay jaar.

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons