Yussofa
Ayuba Sulaymaan Jàllo (ñu gën Koo xam ci turu Jòobeen Solomon) , mi ngi judd jamonoy 1701 fëla ca Bundu, mi ngi dee atum 1773 .Nekkoon Imaam , waaye ba tay bokk ci ñi loru ca njaayum jaam yi tubaab yi doon def nit ñu ñuul ñi.
Nekkoon ab jaam ci ay weer ju bari fee ca Marilaand , moom mooy Benn jaam bi njëkk bi dellusiwaat ci njaayum jaam ñi nekk Kenn ci "Spalading Gentleman' s Society "
Ayaub Sulaymaan Jàllo , bindul ay jaar-jaary fundamental moom ci jëmm mi boppam, waaye ñi kuy xam ci dimbalug téereb tomaas Bulett bii génn ca atum 1734
Judd atum 1701. Ci réewum Senegaal , Ayuba bi ngi bokk ci njabtoog gog ay julit lañu, doon ay woroom xam-xam ci mag, Bi bu nekkee gone ci la jàng làkkuw Araab ak alxuraan ,moo àndoon ak buurub Fuuta ba bu siiw ba Sàmba Gelaajo Jéggi .Bi Amee 29i at, ci la ko Mandige jàpp. Ñu Njaay ko benn "kapiten" bu ñuy woowee Piki