Aller au contenu

Yiir

Jóge Wikipedia.
Nataalu garabug yiir

Yiir garab la gu guddaayam man a àgg ba ci 12 jàpp 20i met, yaatuwaayam ci benn met lay toll. Moom nag ñi ngi ko duppee garabu weñ ndax dëgëraaym max manalu ko dara.

Garabu yiir nag amna Senegaal, Kamerun, Sudã ba Niseer.

Njariñ yi

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ay reenam day faj bëñ yu kadam, am xasam it baax na ci góom. Ay xobam ak i bantam baax na ci góomu biir. Bantam bu dëgër boobu dees ciy defar i lal, ak i armuwaal, ak ay ndënd.

Turu xam-xam wi

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Prosipis africans