Xewar
Apparence
Xewar xeetu garab la gu bokk ci njabootug « Sapindaceae ».
Cosaan li
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Moo ngi tasaaroo ca Afrig ci réew yii: Senegaal, Eritere, Ecopi, Somali, Sudaan, Keeñaa, Tansani, Ugàndaa, Kamerun, Réewum Diggu-Afrig, Gaboŋ, Kóngoo, Bene, Kodiwaar, Gàmbi, Gana, Gine, Gine bisaawóo, Niseer, Niseeryaa ,Tógoo, Àngolaa, Mosàmbig, Madagaskaar.
Amna it ca Asi gu bari naaj ga: Bangalades, Butaan, End, Nepaal, Siri-lànka, Kàmbots, Lawos, Birmani,Taylànd, Wiyet-naam, Endonesi, Maleesi, Papuwaasi Gine Gu yees ak Filipiin.
Melo wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Xewar garab la guy toll ci 6i met ci guddaay. Ay xobam day nëtëx.
Turu xam-xam wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Lepisanthes senegalensis (Aphania senegalensis)
Tur wi ci yeneeni làkk
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]farañse: Cerisier du Cayor