Xavier Rovira Rojas

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Xavier Rovira Rojas - dioudo Mataró, Catalonia, si atoum 1977 si diourombénèlou wèr wi si att bobou, mathematicien la té guénè keur you mag you niouy wakh Valldemia Marist ak Autonomous University. Kou khariagne la si wal wowou tey liguéyè Plaut (Acctus) fofou sa Barcelona si atoum niari diounni ak niar ba niari diounni ak niet diougué fa dem fofou niouy wakh Northgate Arinso si atoum niari diounni ak niet sa Barcelona lègui mou ngui fi si Wiyen.

Basketeur la tamit bou nékon si équibou Valldemia si atoum diounni diourom nièneti temer diouro nièneti niar ak niari diounni ak diourom ben fofou sa CE ak si atoum diounni ak diourom ben ba diounni ak diourom niet Argentona fofou sa CB.