Aller au contenu

Wikipedia:Tàmbali

Jóge Wikipedia.
(Yoonalaat gu jóge Wikipedia:Junj)

Ab junj mooy as njukki, jukki bu tuut lool. Su fekkee man ngaa bind ci wolof, di la sakku nga def ko. Su fekkee dégg nga wolof , te manoo it bind bu baax, bu mu doonub jaaxle, def ko rekk.

Àlliw Sàll Kawlax. Golo de ab rabu hàll la, bu man a yàq lool sax, te sawar ci, li muy dunde mooy li ci hàll rekk, lu mel ni, garab ug dimb, ak màngo... añs.. Ak a ragal xaj, xaj nag ab rabu hàll la moom itam, moom golo Amna ay xeet yu bari a bari, nimuy meloo nag mooy xonq walla nete. Nit ñi da nañ koy jàpp di ko yar ci kër yi, def ko reetaanu kaay, daana ka lépp lu nit di lekk rekk, dana ko lekk moom golo, ko am a am xel la nag, du faral di daw lu mu xamul. Li mu gën a ràññe a koo daal mooy yàq.