Wereg
Wereg xeetu garab gu bàyyikoo Afrig te bokk ci njabootu fabacées.
Melo wi[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
- Gudaay: 3 ba 6i met.
- Xànc: melow baam la yore.
- Doom bi: -Daa tàcc -5 ba 7,5i sàntimet ci guddaay. -1,7 ba 2,5i sàntimet -5 ba 6i xoox yu baam-nëtëx lay ëmb.
Njariñ[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
- Dees koy fajoo. - Dees koy jëfandikoo ci aniin - Dees koy lekk.