Aller au contenu

Waxtaani wàll:Junj

Le contenu de la page n’est pas pris en charge dans d’autres langues.
Jóge Wikipedia.

ab junj waruñu koo wax, waaye ab tàmbali, ndax day lu ñu tàmbali te àggagul kon ab tambali lanuy wax

yaakaaroo ne junj ak tambali benn lañu. loo junj mooy loo tambali. junj am mbir --Ibou 21 Oktoobar 2008 à 19:27 (UTC)[répondre]

Ab junj ab joxoñ, la gën a jege. junj na ko ci biir ay waxam: il y'a fait allusion, junj na ko ci baaraamam: joxoŋ na ko. junj tam day tekki symbole ci fr --Abdu Xaadir Kebe 22 Oktoobar 2008 à 00:56 (UTC)[répondre]