Waxtaani jëfandikukat:Maamdaawur

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Dalal-jàmm ci wikipedia. sag mbindu doon na sunu mbegte. Ngir nga man a duggal dara fàww nga topp àtte yi wikipedia tërël ngir doxinam man a sell.

ci biir jukki yi kenn du fa xaatim, maanaam bind sa tur. ci biir xëtu waxtaanukaay wi rekk nga ko man a defe. yërël wii xët . soo amee ay laaj man nga maa bind ci sama xëtu jëfëndikóokat.--Ibou 13 Baraxlu 2007 à 21:18 (UTC)

Di la nuyu