Waxtaani jëfandikukat:Jose77

Le contenu de la page n’est pas pris en charge dans d’autres langues.
Jóge Wikipedia.

Welcome!

Hello, Jose77, and welcome to Wolof Wikipedia! Thank you for your contributions. I hope you like the place and decide to stay. Here are a few good links for newcomers:

I hope you enjoy editing here and being a Wikipedian! Please sign your name on talk pages using four tildes (~~~~); this will automatically produce your name and the date. If you need help, check out Wikipedia:Where to ask a question, ask me on my talk page, or place {{helpme}} on your talk page and someone will show up shortly to answer your questions. Again, welcome! 

traduction/tekkin[soppi gongikuwaay bi]

c pas parfait mais, s'il y a des incorrection/incomprehention on en parle, ok? salut

“Jàngu(eglise) yéesu gu dëggu gi” ab jàngu gu moom-boppam la gu nek ca Beijing ca reewu sin, ñooŋ ko taxawal ci attum 1917. Da fa nekk ab baŋxaasu ñaxtukat (protestante) yu waa-sin ci diiney krist bi fëll ci attum 1900. Jàngu googu day balloo 1,5 milioŋi taalibe yi mu am ci adduna wërngëlkëp. Jàngu googu gëm na njangalem pantekot, day ab baatin gu wekku ci mayu ku sell ki. Fukki ponki gëm-gëm gi ñooy:

  • Ku sell ki
  • Ngente
  • Jangu(lavage de pieds)
  • Waxtaan gu sell gi
  • Besu sabbat
  • Yéesu-kristaa
  • Biibël
  • Nuyoo gi
  • Jàngu gi(l'eglise)
  • Feeñug yalla

--Ibou 1 juillet 2007 à 12:19 (UTC)

Bataaxalu dalal-jàmm[soppi gongikuwaay bi]

Dalal-jàmm / Bienvenue / Welcome , Jose77 !

(wo) Bataaxalu dalal-jàmm : dila nuyu Jose77 te dila dalal ci Wikipedia. Dila gërëm ci say cëru ci bii jimbulang. Su dee dangay làkk wolof, soxla nañu la lool ngir bind walla soppi ay jukki.; walla it, sag ndimbal ci wàllu xarala. Su fekke it dangaa soxla ndimbal walla dangaa ami laaj, saytul xët wii Ndimbal, man nga maa bind ci sama xëtu waxtaanuwaay, walla nga bind sa laaj ci Wikipedia:Pénc, ci xëtu waxtaanuwaay yi, dee fa xaatim say bataaxal, deel cuq ci walla ngay bind ~~~~ ngir xaatim: dina tax, sa turu jëfandikukat ak taariix bi, feeñ ci sa wetu bataaxal. Liggéeyal ak jàmm!

(fr) Message de bienvenue : Salut Jose77 et bienvenue sur Wikipédia. Merci pour tes contributions sur cette encyclopédie libre. Si tu parles la langue wolof, nous avons extrêment besoin de toi pour éditer les articles; sinon, nous avons toujours besoin de ton aide pour l'assistance technique. Si tu as toi-même besoin d'aide ou si tu as des questions, consulte Ndimbal, demande-moi sur ma page de discussion, ou pose ta requête sur Wikipedia:Pénc. Sur les pages de discussion, signe tes messages en cliquant sur ou en écrivant ~~~~ : ceci fera afficher automatiquent ton nom utilisateur et la date. Bonne continuation!

(en) Welcome message: Hello Jose77 and welcome to Wikipedia. Thank you for your contributions to this free encyclopedia. If you speak the wolof language, we highly need you to edit articles; if you don't, we always need your help for technical support. If you need help or for any question, check out Ndimbal, ask me on my talk page, or ask your question on Wikipedia:Pénc. Please remember to sign your name on talk pages by clicking or using four tildes (~~~~): this will automatically produce your username and the date. Happy editing!

Guérin Nicolas (Xëtu waxtaanukaay) 7 Awril 2009 à 12:57 (UTC)[répondre]

Votre compte va être renommé[soppi gongikuwaay bi]

20 Maars 2015 à 08:46 (UTC)