Aller au contenu

Waxtaani jëfandikukat:216.218.60.216

Le contenu de la page n’est pas pris en charge dans d’autres langues.
Jóge Wikipedia.

Di la nuyu su fekkee bindu nga balaa ngay cëru (contribuer), da ngaa war a dugg (xammeeku) ba noppi mooy tax nu man laa xammee, ci jaar-jaaru xët wi ak ci coppite yu mujj, sa tur lañ fay bind. Su dee bindoogóo yëral xët wii. Su fekkee duggoo sa IP wu wuutuloxo lay bind te kon kenn du man xam ndax yaa bind walla déet. wasalaam --Ibou 21 septembre 2007 à 10:38 (UTC)


Yaa ngi ci xëtu waxtaanuwaayu ab jëfandikukatu alaxam, bu bindoogul ba fim ne mbaa jëfandikoowul am sàqam.

Kon ngir xàmmee ko fàw nga jëfandikoo màkkaanub IP wam. Te màkkaanub IP jëfandikukat yu bari man nañ koo bokk. Su fekkee jëfandikukatu alaxam nga, te nga gis ne dees laa féetale ay kàddu yoo moomul, ngalla bindu walla dugg ngir benn jaxase bañatee am ëllëg .